bari
Apparence
wolof
[Soppi]bari:
- bari lu ap ñatt ci lees man a waññi, tey duun ci lees man ta waññi
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- Xamnaa xeeti xam-xam yu bari. Amnaa xam-xam bu bari.
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]
Déglu baatu bari ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-bari.ogg